Binta Moo Bette Meilleure Kharitam Ak Papam… 😳 | HISTOIRE EN WOLOF
Автор: Histoire en Wolof
Загружено: 2026-03-06
Просмотров: 5173
Описание:
Li xew ci histoire bii dafa yéemu lool 😳
Binta ak meilleure kharitam dañoo doon ay xarit yu baax, waaye mbir mi xew ginnaaw bi kenn warul ko xalaat. Binta moo bette xaritam ak papam… te loolu soppi na lépp.
Ndax li Binta def jub na walla déedéet ?
Seetal histoire bii ba ci mujj ngir xam li xew ginnaaw ak njàng mi ci nekk.
💬 Waxal nu ci commentaires yi :
Yow lan nga xalaat ci li Binta def ?
👍 Like video bi
🔔 Abonneel ci chaîne bi ngir yeneen histoires en wolof yu yéemu te am njàng.
#ConteWolof #HistoireSenegal #HistoireEnWolof #WolofStory #Sénégal #HistoireTriste
Повторяем попытку...
Доступные форматы для скачивания:
Скачать видео
-
Информация по загрузке: