ycliper

Популярное

Музыка Кино и Анимация Автомобили Животные Спорт Путешествия Игры Юмор

Интересные видео

2025 Сериалы Трейлеры Новости Как сделать Видеоуроки Diy своими руками

Топ запросов

смотреть а4 schoolboy runaway турецкий сериал смотреть мультфильмы эдисон
Скачать

Leuz DiwanG & Amdy Opti- Univers Cité ( LRGB,la Compilation)

Автор: Loudoul Rap Galsen Beugouniou LRGB

Загружено: 2019-12-17

Просмотров: 2510

Описание: Cette chanson est dédiée à la population estudiantine du Sénégal et du monde. C’est un cri de coeur visant à pointer du doigt les maux qui gangrénent le systéme éducatif sénégalais lesquels maux ont conduit aux regrettables décés de nombreux étudiants...
——————
Artistes : Leuz Diwan G & Amdy Opti
Titre: Univers Cité
Album : LRGB la Compilation
Prod: Thior K ( Labo 36 Recordz)

Retrouvez l’intégralité de l’album 👉🏿 https://loudoulrapgalsenbeugouniou.com/
————————————
Lyrics

Amdy Opti

Sàkku xam-xam xam fi nga joge akk nga jëm ci daara ju kawe jii
Coono fitna buur aki dag’am dëkk ci di yee fitna
Bës bu Yàlla sàk ñu faat bakan ba noppi jiiñante (Bis)

Leuz DiwanG

Mënu ma comprendre ba leegi
Luy priorité ci reew mi
Caaxaan la wala liggey
Bataaxal la bu jëm ci njiitu reew mi
Ay att rëdd bi ñu bañ ko jeegi
Joge wuñ fii ñu ne ba leegi
Jaxaan di saw balaa ken tooy nga loor mu nuñ ko weddi
Avenir u reew mi ngi sukandiku ci njangum ndawu reew ma
Sunu bideew ñu sopali ko niir yi muur ko te nan dem na
Lu jii ba jeexul jogu fa
Meeñeef faw ñu waajal garabam
Jàngoro bi fog ñu dog ko ca reen ba
Waajal garab ba

Refrain:

Université
Étudiant fierté la
Étudiant laa
Nous voulons apprendre en paix

Amdy Opti:

Reew mu ndaw ñi jàngiwul aveniram xaw ma fumuy mujjee
Reew mu ndaw ñi jàngi ba am ay lijaasa ngen ne len deet du fii
Man li ma gis ci reew mi doy na waar
Dang koy ñaffe ba agsi fii sa sagaru bourse jëlli ko meeti lool
Man japp na ni yen dëgg dëgg Jambaar ngen
Ci coono akk naqqar ngay dundee yaakaar
Nekkinu étudiants yi ci université yi doy na waar
Waay lii da fa wara jeex

Leuz DiwanG

Ku ne sa bës nga am
Day mel ni rëcc nga
Liñ fi boom faat fi etudiant mënul a des ginaaw
Wax dëgg mënul a gaawe noonu
Njuumte bu ñu dul baale loolu
Ñi ngi jaale seeni wayjur akk bepp étudiant du ko naqqar lu

Amdy Opti

Waxtaan day dakk reero
Su ñu pencoo rekk daldi bennoo
Yen njiit yi ngala deglu len ndongo yi

Leuz DiwanG

Mënu ñu la fal
Nga falu fuuy faate ki nga doon li nga doon
Ñun doomi baadola yi dee ci fac yi du dëgg du yoon

Amdy Opti

Avenir u reew mi ngi sukandiku ci njangum ndawu reew ma
Sunu bideew ñu sopali ko niir yi muur ko te nan dem na

Leuz DiwanG

Lu jii ba jeexul jogu fa
Meeñeef faw ñu waajal garabam
Jàngoro bi fog ñu dog ko ca reen ba
Waajal garab ba

Refrain:

Université
Étudiant fierté la
Étudiant laa
Nous voulons apprendre en paix

Transcrit par Maalik Si

Не удается загрузить Youtube-плеер. Проверьте блокировку Youtube в вашей сети.
Повторяем попытку...
Leuz DiwanG & Amdy Opti- Univers Cité ( LRGB,la Compilation)

Поделиться в:

Доступные форматы для скачивания:

Скачать видео

  • Информация по загрузке:

Скачать аудио

Похожие видео

Leuz Diwane G - Wëy Wallú - Clip Officiel

Leuz Diwane G - Wëy Wallú - Clip Officiel

fadel ft Leuz Diwane G #Audience de la Jeunesse# Clip Officiel by HLAB PRO

fadel ft Leuz Diwane G #Audience de la Jeunesse# Clip Officiel by HLAB PRO

LEUZ DIWANE G: ma DIGNITÉ n’a pas de PRIX,2 MILLIONS,PPS et BABA MAAL,GISU MALA MBAO SHOW 2

LEUZ DIWANE G: ma DIGNITÉ n’a pas de PRIX,2 MILLIONS,PPS et BABA MAAL,GISU MALA MBAO SHOW 2

Amdy Opti - Aime moi (Official Music Video)

Amdy Opti - Aime moi (Official Music Video)

Bi Peul & Xel si Kaw Xel - Urgences ( LRGB, La Compilation)

Bi Peul & Xel si Kaw Xel - Urgences ( LRGB, La Compilation)

New Feeling Good | Deep House, Vocal House, Nu Disco, Chillout Mix | Emotional Mix 2026 #deephouse

New Feeling Good | Deep House, Vocal House, Nu Disco, Chillout Mix | Emotional Mix 2026 #deephouse

Leuz Diwane G Wéeruwaay Prod by Labo 36 Record

Leuz Diwane G Wéeruwaay Prod by Labo 36 Record

Leuz Diwane G Lambaatu Vidéo Lyrics 2015

Leuz Diwane G Lambaatu Vidéo Lyrics 2015

Leuz Diwane G - Early in the morning

Leuz Diwane G - Early in the morning

Beuz Mc & Neew Bi- Sulli Neew bi ( LRGB, La Compilation)

Beuz Mc & Neew Bi- Sulli Neew bi ( LRGB, La Compilation)

Izapt & Ibrain- Cas Chaud ( LRGB, La Compilation)

Izapt & Ibrain- Cas Chaud ( LRGB, La Compilation)

By MIC- Ego feat Leuz Diwane G (Prod by BY MIC)

By MIC- Ego feat Leuz Diwane G (Prod by BY MIC)

Freestyle de Leuz Diwane G dans le Tal Rek Show

Freestyle de Leuz Diwane G dans le Tal Rek Show

Top Hits 2026 Playlist ~  TikTok & Spotify Viral Hits  🍒 Trending Music 2026 🎵 Latest Songs 2026

Top Hits 2026 Playlist ~ TikTok & Spotify Viral Hits 🍒 Trending Music 2026 🎵 Latest Songs 2026

Leuz Diwane G - Mburook Lem (Clip Officiel)

Leuz Diwane G - Mburook Lem (Clip Officiel)

12. Ombre Zion - Feat - Leuz Diwane G - Bëreel Goor (youssou ndour) @ombrezion @LeuzDiwaneG

12. Ombre Zion - Feat - Leuz Diwane G - Bëreel Goor (youssou ndour) @ombrezion @LeuzDiwaneG

Leuz Diwane G _

Leuz Diwane G _ " Aventure Ambiguë "

Soulful R&B Vibes 🎧 Smooth Love Songs & Emotional Chill Mix for the Heart 🔴 LIVE 24/7

Soulful R&B Vibes 🎧 Smooth Love Songs & Emotional Chill Mix for the Heart 🔴 LIVE 24/7

Xalé (Children) - AMDY (Official video)

Xalé (Children) - AMDY (Official video)

Elzo JamDong - Saï Saï [Clip Officiel]

Elzo JamDong - Saï Saï [Clip Officiel]

© 2025 ycliper. Все права защищены.

  • Контакты
  • О нас
  • Политика конфиденциальности

Контакты для правообладателей: [email protected]