Jaar Jaari Serigne Saliou Mbacké | l'histoire jamais racontée Part.01
Автор: Jambarou Mouride 2.0
Загружено: 2025-10-17
Просмотров: 4185
Описание:
Assalaamaleykum Mbokk yi
Meun ngueena abonner wou ci sounoup ñareelou Chaîne biniou diaagleel Wolofal Makk ñi (Appuyez sur le lien pour s'abonner à notre deuxième Chaîne) 👉🏻👉🏻👉🏻 : / @wolofalakwaxtaanmakkñi
Collaboration avec Mouridoulahi Collectios :
WACCAY ! COLLECTION "A DOOM" - L'Heritade de Mame Chekh Ibrahima Fall !
Aksi na, léegi léegi ! Danoo leen indil sunu collection bu bees bi, "A doom", mi ñu jëlé inspiratioŋ ci njàngalem Mame Cheikh Ibrahima Fall.
"A doom" du baat rekk, ab jikko la. Mooy doole ji nekk ci liggéey, yar ak ngëm gu wér. Yére bu nekk ab fàttali la ci ndono lu am solo loolu.
Paré ngeen ngir sol seeni jikko ci ag firndéel ?
➡️ Bësal lien bi ci sunu bio ngir gis collection bi yépp !
Meune nguena commander sen T-shirt 👕 fi 👉🏻 : https://ekg8dh-r0.myshopify.com/produ...
Ban kàddug Lamp Fall moo la gëna dal ? Bindal ko ci commentaire ! 👇
#mouride #serignetouba #cheikhibrafall #touba #bayefall #senegal #jambaroumouride #bayendiagadiop #wolof #mouridisme
Повторяем попытку...
Доступные форматы для скачивания:
Скачать видео
-
Информация по загрузке: