Ma Ibra Laye - Juger nitt ( Ibra Seck )
Автор: F'Art TV
Загружено: 2021-10-25
Просмотров: 3283
Описание:
Lu bari ci nitt yi da ñuy juger sééni moroom, di sukkandiku ci li ñu léen di nettali, walla sax ci lu ñu téewé.
Waaye nakk na ñu baayi xéll ni, mbindéef munul deff jugement bu parfait jëm ci moroomam ndax ngir loolu mana nekk, dafay warr ñu xam yéeney nitt ki bi mu jëff, xam aussi ci yan condition la nekk ba muy jëff, waaye aussi da ñuy wax ni "les apparences sont souvent trompeuses" motax nakk bari lu ñuy téewé te bu ñu ko attée rekk juum.
Ma Ibra Laye - Ibra Seck
Повторяем попытку...
Доступные форматы для скачивания:
Скачать видео
-
Информация по загрузке: