Cette Histoire va vous Trau*matiser
Автор: tARIXU EN wolof
Загружено: 2026-01-11
Просмотров: 5888
Описание:
Ci bii leebu Afrik bu tis, bu ñu jël ci mbir yu am dëgg ak cosaan, degluleen jaar-jaaru Chindinma, ab jigéen bu ëmb bu xaritam bu mag Ngozi wor, ngir ab jaaro bu am mbóot. Jaaro boobu, dañu naan dafay indi alal, waaye dafay indi musiba tamit.
🎬 Nettali la bu fess dell ak kiñaan, wor, sàq, ak mbirum aada yu xóot... Ci ab dëkk bu sori ci Nigeria, mbóot yu yàgg feeñ nañu, xarit tase na, te deret turu na ngir jaaro bu kese. Waaye... ndax jaaro bii jaaro bu yomb la?
🔥 Bii film d’animation du bu xale. Leeb la bu lëndëm te metti, bu boole dëgg-dëggu Afrik, jom, ak mbirum tiitange. Joxleen ci seen xel bu baax ndax dafa am ay yéemu yu metti.
✅ Bësal cloche bi ngir baña ñàkk yeneen nettali yi ñëw
📢 Waxal ci commentaire yi, lo defoon su fekkoon yaa nekk ci plaasu Ngozi?
📌 Abonnel ci HistoMania ngir yeneen nettali yu neex
Conte africain, Histoire africaine, Film d'animation africain, Leeb wolof, Nettali wolof, Histoire en wolof, Chindinma et Ngozi, Légende nigériane, Histoire vraie, Drame familial, Trahison et jalousie, Femme enceinte, HistoMania, Senegal, Nigeria, Film triste, Leçon de morale, Animation 2D, Sorcellerie africaine, Bague maudite
Повторяем попытку...
Доступные форматы для скачивания:
Скачать видео
-
Информация по загрузке: