Big Dat X - Pause Cas Faits (Audio officiel)
Автор: Big Dat X
Загружено: 2024-11-28
Просмотров: 7847
Описание:
#pausecasfaits #bigdatx #ogkajooroi
Streamez ici: https://onerpm.link/ogkajooroi
————————————————
Artiste: Big Dat X
Titre : Pause Cas Faits
Prod : TeacherBeatz
Enregistrement: Das Records
Mix/Master: Teacher
Video: Nittu Deugg
Production exécutive: MeloMusic Ent. & Chambre 9
Contacts: [email protected]
—————————
Réseaux Sociaux:
X @BigDatX2 : https://x.com/bigdatx2?s=21&t=EI1N8Ym...
Facebook @Big dat X : / big-dat-x-marxabane-team-650660248375778
Instagram @bigdatx: https://www.instagram.com/bigdatx?igs...
Tiktok @bigdatx : https://www.tiktok.com/@bigdatx?_t=8U...
————————
Lyrics
Baaraam u digg si lobby siisuman sama bopp laa gëm
Man dara duma bett ndem liy raam si ñag bi la jëm
Gewël du jur muumë loolu moy yaakaar bu tas
Coow li [coow li] gën fi bari ne sabar gu tas
Dinañ yagg si jooy X ay neex a faral dimanche
T’es au courant sa rappeur fitam day faral di maas
Ñune X dafa waga men
Rax ci tuuti caga men
Rabu ndaga baaraam u digg sen in in mama yen
Mballu ba daanu jaawale jus bi le
Krik krak murder len taxul may jubiler
Ki jaar si digg bi man la
Yaxxate beat bi man la
Taaru mbind bi aaru mbedd gën a fi werëdi man la
Amul saale day sale pimenté buma tegoo si beat
Malaakal mëwti rap bi teew foy miser bo tegul si Big
Hey Noise Maker ma open heart bi wax la lima feel
Duma boy u kenn it’s time them know the deal
The first thing
Est-ce-que game bi recognise na mérite?
Mar naan du tax ma naan pôtit
Déception ni Don kenn xamul lumu doon
Be a leader why i’m born
Bullshitism why i’m done
Grand Damel a ma jox jaasi nema taxaweel kankourang
Ma waay di xaar keneen kan ku rang
Tambalee làbbali rhyme ñu nan tay kan laay dëjjël
War Dajjaal di la yoxal ngay tuddu benn bët di jéll
Kuma fi ba xamal ni mën rabam a des wala moomin la
Taak reum u MC yeah luma miin la
Yàgg len terroriser ba ñëpp sikkël ma
Ya fi fëgg dënn tay suba yaay woote calmant
Degg nafi sen i pic mais vous portez jamais vos reukhou
Ñakk Gorée sa bopp moy duggu si Porte aller sans retour
Radio nga sex ni McNeely may crochet Tyson bilay suusël
Dat trash talk plus performance comme Cedric Doumbe
Fatt say angle teewula doon mort Jordan
Yaa mën te foo songee fekk say dàll makkaan
Do len producer ay woubi ngen
Li feat la wala sëy
Bàkkoo trophée jéng man winner la ni Jyeuhair
Princesse de la ville ak la chouchoute de KeuMeuFemme
À part ref si rap lufi KeuMeuFeu am
Gisuma fi ludul reine bu took si chaise anglaise
Trône de fer neel ñi lay couche mënofi took à l’aise
La somme de diw ak diw
Projem ñëpp jàpp di diw
Amul concurrence affaire de niveau
Linga goob nga jiw
Budul gaaruwaale kufi mës a gis fu Gun di Shot
Now it’s time nga honest
Better tell them kulen tee nelaw
Badman i run things
Things don’t run me
Everything me do
Me haffy do it properly
Avance waga bi nga jël fexeel buko wutël lay
You’r snitch kingay sotal bitch loloy jikko jeeg
Ñëpp xam 2023 who drop da best album
Ñuni Big Dat du best lyricist hein feni neen
Aham duuli neen [duuli neen, feni neen]
Gëj nga lucide binga tafoo sama doublé si awards yi
Lyrically musically Check Mic a causer sa death
Bu talent don fay ma rangale trophée yëpp dara du des
OK daxx sa next album bul es
Vrai complexe ngafi gis si kanam u hype
Yaw la boy u diw rekk ñuni lepp tight [yeah]
Quantité molen gënal quality
Amuñ xam-xam si talent jël lepp tek ko si vue [yeah]
Bokkuma si jàgg yi nekk si game wër di maral
Laajal Coumba dof be g Ydee bi respect lim ma jaral
Serious business without money men is damn bullshit
Boo dee yalla fexeel nga tax boulette ñi xiif eat [yeah]
Fuck master pipi ak rap221 bi yëpp
Fuck chroniqueur yimay jeem a boycott ak dima tëb
Neleen mangi ak mental de fer kenn si ñoom duma disturb
That’s wussup Og KajooRoi bi moy the best
Повторяем попытку...
Доступные форматы для скачивания:
Скачать видео
-
Информация по загрузке: