ycliper

Популярное

Музыка Кино и Анимация Автомобили Животные Спорт Путешествия Игры Юмор

Интересные видео

2025 Сериалы Трейлеры Новости Как сделать Видеоуроки Diy своими руками

Топ запросов

смотреть а4 schoolboy runaway турецкий сериал смотреть мультфильмы эдисон
Скачать

Waxtaan Bu Yeemee Ci S. Bassirou Mbacké ak Mame Cheikh Ibrahima Fall | Par S. Mountakha Gueye Fulk

Автор: Jambarou Mouride 2.0

Загружено: 2025-07-03

Просмотров: 9200

Описание: Ci waxtaan bii, Serigne Mountakha Gueye Fulk daf ñuy léeral ci anam gu leer te yéeme diggante gu am solo gi amoon ci diggante ñaari kilifa yu magg : Sëriñ Bassirou Mbacké, boroom "Jëf-ju-ñu-joy", ak Mame Cheikh Ibrahima Fall, "Babul Muridina".

Déglu leen ay nettali yu am solo, ay xibaar yu wóor ak ay njàngle yu réy ci seen jikko, seen jonganté, seen wéeroo ak seen xidma ci yoonu Murid. Video bii di na leral yenn ponk yu bare ci taarixu Murid yi ñu war a xam.

🔔 ABONNÉWOOL ngir am lep luy sunu yeesal :    • Baye Cheikh Ndao : L'histoire du BAYE FALL...  

#Mouride #SerigneBassirouMbacke #MameCheikhIbrahimaFall #Waxtaan #Touba #BayeFall #IslamSenegal

👇 CI BIIR VIDEO BI :
Digganté Sëriñ Bass ak Lamp Fall
Pas-pasu Baye Fall ak njabootu Sëriñ Tuubaa
Ay nettali yu yéeme ci seen biir
Njàngle yi ñu mëna tenqoo ci seen àtte

Bëssal "J'aime" 👍 bi su la video bi néexee, bàyyi sa xalaat ci commentaire te bokk ko ak sa xarit yi ngir ñu man cee jëriñu.

Jërëjëf !

#Mouride #Waxtaan #SerigneBassirouMbacke #MameCheikhIbrahimaFall #touba

Не удается загрузить Youtube-плеер. Проверьте блокировку Youtube в вашей сети.
Повторяем попытку...
Waxtaan Bu Yeemee Ci S. Bassirou Mbacké ak Mame Cheikh Ibrahima Fall | Par S. Mountakha Gueye Fulk

Поделиться в:

Доступные форматы для скачивания:

Скачать видео

  • Информация по загрузке:

Скачать аудио

Похожие видео

Dakar 1895 : Le secret des deux nuits de Khadimou Rassoul avant l'exil | Ñaari Guddi Ndakaru

Dakar 1895 : Le secret des deux nuits de Khadimou Rassoul avant l'exil | Ñaari Guddi Ndakaru

"Pape Cheikh en Larmes, Je Ne Suis Pas Un...": Scène Spectaculaire Dans le Bureau du Juge...

Répression sanglante à l'UCAD :Comment les autorités ont été négligentes sur ce coup ?

Répression sanglante à l'UCAD :Comment les autorités ont été négligentes sur ce coup ?

S Mountakha Gueye: Le Bon Comportement d'un Talibé Mouride(Touba Déss Nafi Défaro Déss Nafi Yaxoo

S Mountakha Gueye: Le Bon Comportement d'un Talibé Mouride(Touba Déss Nafi Défaro Déss Nafi Yaxoo

Serigne Bassirou Mbacké Xelcom (Taverny 06/11/2016) Sur le théme : Sant

Serigne Bassirou Mbacké Xelcom (Taverny 06/11/2016) Sur le théme : Sant

Ndenkané You Moudj You Mame Cheikh Ibrahima Fall | Par Serigne Oumar Doumbouya

Ndenkané You Moudj You Mame Cheikh Ibrahima Fall | Par Serigne Oumar Doumbouya

MAUVAISE NOUVELLE POUR PAPE CHEIKH ET CIE...SA NDIOGOU DOSSIER BI DOU MBIROU GOOR JIGUENE KÉSSÉ...

MAUVAISE NOUVELLE POUR PAPE CHEIKH ET CIE...SA NDIOGOU DOSSIER BI DOU MBIROU GOOR JIGUENE KÉSSÉ...

Les Secrets jamais révélés sur la mission de Mame Cheikh Ibra Fall

Les Secrets jamais révélés sur la mission de Mame Cheikh Ibra Fall

🔴Thieyy Wakh diou Daw Yaram😭 Serigne Mountakha Mbacke Sogné ci Serigne bi ak Xam xam..

🔴Thieyy Wakh diou Daw Yaram😭 Serigne Mountakha Mbacke Sogné ci Serigne bi ak Xam xam..

Les principes du

Les principes du "Yaar" de Mame Cheikh Ibrahima Fall | Leralu Baye Abdou Niang

🔸Histoire De Seydina Mouhamad PsL| Par Seringe Bassirou Mbacké -17em parti

🔸Histoire De Seydina Mouhamad PsL| Par Seringe Bassirou Mbacké -17em parti

Reubeus Ça Bouge: Autres listes,Cr!se, Khalil série Baabel accusé après Pape C Diallo:J Diouf révèle

Reubeus Ça Bouge: Autres listes,Cr!se, Khalil série Baabel accusé après Pape C Diallo:J Diouf révèle

Cet étudiant sermonne le PM

Cet étudiant sermonne le PM "Sonko Dafa Wara Kholat Sa Com, On Ne Gouverne Pas Par l'Accusation…"

🛑Grand Plateau Spécial SCheikh Ibra Fall Invité : Serigne Ablaye Diop Bichri Special

🛑Grand Plateau Spécial SCheikh Ibra Fall Invité : Serigne Ablaye Diop Bichri Special

Wakhtane😭 Mame Cheikh Ibrahima bou yémé😭 Par S.Ibrahima Ndim Baye Fall

Wakhtane😭 Mame Cheikh Ibrahima bou yémé😭 Par S.Ibrahima Ndim Baye Fall

Allahou Akbar  Serigne Djily Mbacke Koso  Les secrets cachés derrière les Khassida ?

Allahou Akbar Serigne Djily Mbacke Koso Les secrets cachés derrière les Khassida ?

JANGOROY KHOL ( Le Coeur ) / Par Serigne Ahmadou Mbacké Darou Mouhty

JANGOROY KHOL ( Le Coeur ) / Par Serigne Ahmadou Mbacké Darou Mouhty

50 vidéos- p0rnos saisies: lle juriste Thioune fait de graves révélation

50 vidéos- p0rnos saisies: lle juriste Thioune fait de graves révélation "Pape Cheikh téléphone bi…

Ni Xallate Mané Agalé Nitki si Gueme Go dago té dagal / Par Serigne Ahmadou Mbacké Darou Mouhty

Ni Xallate Mané Agalé Nitki si Gueme Go dago té dagal / Par Serigne Ahmadou Mbacké Darou Mouhty

Mame Cheikh Ibrahima Fall ak

Mame Cheikh Ibrahima Fall ak "MOURIDE SADIKH " | Leralu Serigne Khadim Ndiaye Kayar

© 2025 ycliper. Все права защищены.

  • Контакты
  • О нас
  • Политика конфиденциальности

Контакты для правообладателей: [email protected]