Mame Cheikh Ibrahima Fall ak Xam-xam (Suite 01)
Автор: Jambarou Mouride 2.0
Загружено: 2025-12-29
Просмотров: 1467
Описание:
Assalamou Alaïkoum mbokki mourid yi, teewlu leen li ci tegu ci suñu waxtaan bi am solo.
Horodatages
00:00 Ubbité ak nuyoo (Introduction)
15:00 Fatali li weesu ci partie 1
35:00 Xam-xamu Mame Cheikh Ibrahima Fall
55:15 Diggante ak Serigne Touba
70:12 Leral ci sarti yoonu Mouride
80: 15 Taggatoo ak ñaan
Ñu ngi lay nuyu te di la siar ci suñu chaîne YouTube Jambarou Mouride 2.0. Ci saas bi, ñu ngi nuyu mbollo mi te di leen indil "Suite 01" ci waxtaan bu xoot bi ñu doon def ci doundou ak xam-xamu Mame Cheikh Ibrahima Fall (Baboul Mouridina).
Ci biir waxtaan bi, leral nañu fi ay jiko ak ay sarti yo xamni ñooy dekkal dëgg-dëgg biir xam-xam bi Lamp Fall dindi. Ñu ngi leen di ñaan ngeen abonné, like vidéo bi, te partager ko ngir jëriñu ñépp.
Jëfël te teggi sa loxo, loolu mooy yoonu mboolo mi.
Abonné leen ci Jambarou Mouride 2.0 ngir yéneen waxtaan yu am solo.
#mouride #serignetouba #touba #bayefall #cheikhibrafall #jambaroumouride #senegal #mouridisme #bayendiagadiop #wolof
Повторяем попытку...
Доступные форматы для скачивания:
Скачать видео
-
Информация по загрузке: